Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 25

Kàddu yu Xelu 25:6-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Bul réy-réylu fi kanam buur, bul tooge jataayu boroom daraja,
7ndax ñu ne la: «Yéegal, jegesi fii,» moo gën ñu torxal la ci kanam kilifa. Boo gisalee sa bopp it,

Read Kàddu yu Xelu 25Kàddu yu Xelu 25
Compare Kàddu yu Xelu 25:6-7Kàddu yu Xelu 25:6-7