Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 25

Kàddu yu Xelu 25:2-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Màggug Yàllaa ngi ci li mu làq, darajay buur a ngi ci li mu feeñal.
3Maneesula daj li ci xelu buur, xalaatam daa kawe ni asamaan, xóot ni suuf.
4Xellil xaalis, tonni lu ca rax, ba ab tëgg man caa am ndab.
5Ab soxor it, dàqal, mu sore buur, ngir njubte law, jalam sax.
6Bul réy-réylu fi kanam buur, bul tooge jataayu boroom daraja,

Read Kàddu yu Xelu 25Kàddu yu Xelu 25
Compare Kàddu yu Xelu 25:2-6Kàddu yu Xelu 25:2-6