Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 25

Kàddu yu Xelu 25:15-17

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Muñ mer ay nax kilifa, te wax ju neex, fu mu jaar, mu nooy.
16Boo gisee lem, lekkal lu yem; bu ëppee, nga waccu ko.
17Na sa tànk di gëj kër dëkkandoo; boo ko sàppee, mu jéppi la.

Read Kàddu yu Xelu 25Kàddu yu Xelu 25
Compare Kàddu yu Xelu 25:15-17Kàddu yu Xelu 25:15-17