Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 24

Kàddu yu Xelu 24:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Xel mu rafet ay tabax kër, rafet déggin a koy samp.
4Xam-xam ay feesal néeg ya ak mboolem alal ju jafe te yànj.
5Ku rafet xel di boroom doole, ku xam, gëna man;

Read Kàddu yu Xelu 24Kàddu yu Xelu 24
Compare Kàddu yu Xelu 24:3-5Kàddu yu Xelu 24:3-5