Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 23

Kàddu yu Xelu 23:22-23

Help us?
Click on verse(s) to share them!
22Déglul sa baay bi la jur. Bu sa ndey màggatee, bu ko sàggane.
23Jëndal dëgg te bu ko jaay. Sàkkul xel mu rafet ak yar akug dégg.

Read Kàddu yu Xelu 23Kàddu yu Xelu 23
Compare Kàddu yu Xelu 23:22-23Kàddu yu Xelu 23:22-23