Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 22

Kàddu yu Xelu 22:18-20

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18Soo mokkalee, ba man koo tari, muy sa mbégte.
19Yaw laa koy xamal tey jii, ndax nga wóolu Aji Sax ji.
20Dama laa bindal fanweeri dénkaane, ci wàllu digal ak xam-xam,

Read Kàddu yu Xelu 22Kàddu yu Xelu 22
Compare Kàddu yu Xelu 22:18-20Kàddu yu Xelu 22:18-20