Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 21

Kàddu yu Xelu 21:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Coxor day sànk boroom, ndax day baña def njub.
8Ab saaysaay day dëngal, nit ku dëggu di jubal.
9Dëkkeb ruq cim sàq moo gën jabar ju pànk.

Read Kàddu yu Xelu 21Kàddu yu Xelu 21
Compare Kàddu yu Xelu 21:7-9Kàddu yu Xelu 21:7-9