Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 21

Kàddu yu Xelu 21:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Deel def dëgg ak njekk, moo gënal Aji Sax ji ab sarax.
4Xeebaateek réy-réylu mooy bàkkaar yi ñuy ràññee ku bon.
5Farlu, woomle; ku gaawtu, mujj néewle.
6Alal ju la fen may, cóolóol la, day naaw, wut ko xaru la.

Read Kàddu yu Xelu 21Kàddu yu Xelu 21
Compare Kàddu yu Xelu 21:3-6Kàddu yu Xelu 21:3-6