Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 21

Kàddu yu Xelu 21:17-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Ku topp sa bànneex, mujje ñàkk; ku sopp biiñ ak lu niin du woomle.
18Ku bon këppoo ayu ku baax, workat gàddu musibam kuy jubal.
19Dëkke ndànd-foyfoy moo gën jabar ju tàng, bare ay.
20Ku xelu denc këram ngëneeli alal aku diw, ab dof saax-saaxee josam.
21Ku saxoo njekk ak ngor am fan wu gudd, naataangeek daraja.

Read Kàddu yu Xelu 21Kàddu yu Xelu 21
Compare Kàddu yu Xelu 21:17-21Kàddu yu Xelu 21:17-21