Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 20

Kàddu yu Xelu 20:6-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Ñu baree ngi naa: «Gore naa,» waaye kuy boroom kóllëre dëgg?
7Ku jub, di jëfeg mat, doom ju la wuutu bég na.
8Su buur toogee di àtte, day gis, di ràññee mboolem ayib.

Read Kàddu yu Xelu 20Kàddu yu Xelu 20
Compare Kàddu yu Xelu 20:6-8Kàddu yu Xelu 20:6-8