Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 1

Kàddu yu Xelu 1:9-14

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Kaala gu jekk la ci bopp, di gànjar ci baat.
10Doom, bàkkaarkat bu la xiirtal, lànkal.
11Dañu la naan: «Dikkal, nu tëruji bakkan, yeeruji jaambur bu deful dara.
12Nanu mel ni njaniiw, mëdd kuy dund, mu jekki tàbbi biir bàmmeel.
13Mboolem alal ju réy, nu jagoo, yeb sunu biir kër, mu fees.
14Dikkal nu far, mbuus miy benn, nu bokk.»

Read Kàddu yu Xelu 1Kàddu yu Xelu 1
Compare Kàddu yu Xelu 1:9-14Kàddu yu Xelu 1:9-14