Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 1

Kàddu yu Xelu 1:4-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4ndax ab téxét di foog, ndaw li it xam tey xalaat.
5Na boroom xel mu rafet déglu, yokk dég-dégam, te kiy ràññee di jariñoo ay tegtal,
6ngir mana xam aw léeb aku taas ak kàddug boroomi xel yu rafet ak seeni cax.

Read Kàddu yu Xelu 1Kàddu yu Xelu 1
Compare Kàddu yu Xelu 1:4-6Kàddu yu Xelu 1:4-6