Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 1

Kàddu yu Xelu 1:18-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18Ñii kat seen bopp lañuy fiir, seen bakkanu bopp lañu sànk.
19Képp kuy lekk lu lewul, nii lay mujje: wutin wu lewul jël bakkanu boroom.
20Xel mu Rafet a ngay woote ca mbedd ma, di xaacu ca pénc ma.
21Ma ngay wootee bérab yu gëna xumb, di dégtaley kàddoom, bunt dëkk ba.

Read Kàddu yu Xelu 1Kàddu yu Xelu 1
Compare Kàddu yu Xelu 1:18-21Kàddu yu Xelu 1:18-21