Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 1

Kàddu yu Xelu 1:17-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Doo firib caax, ba jàpp njanaaw luy xoole.
18Ñii kat seen bopp lañuy fiir, seen bakkanu bopp lañu sànk.

Read Kàddu yu Xelu 1Kàddu yu Xelu 1
Compare Kàddu yu Xelu 1:17-18Kàddu yu Xelu 1:17-18