Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 19

Kàddu yu Xelu 19:3-5

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Nit def na jëfi dof, ba sànku, walbatiku mere Aji Sax ji.
4Ku barele, barey xarit; ku ñàkk, sab xarit dagg la.
5Seede buy fen muccul mbugalam, kuy noyyee ay fen du rëcc àtteem.

Read Kàddu yu Xelu 19Kàddu yu Xelu 19
Compare Kàddu yu Xelu 19:3-5Kàddu yu Xelu 19:3-5