Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 19

Kàddu yu Xelu 19:23-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
23Ragalal Aji Sax ji ndax nga gudd fan, nopplu te baña loru.
24Ab yaafus day yeb loxoom ci ndab, tàyyi ko yékkati, sex.

Read Kàddu yu Xelu 19Kàddu yu Xelu 19
Compare Kàddu yu Xelu 19:23-24Kàddu yu Xelu 19:23-24