Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 18

Kàddu yu Xelu 18:9-10

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Kuy sàggane sa liggéey, yaak kuy yàq a bokk.
10Turu Aji Sax ji rawtu bu mag la. Ku jub daw làqu ca, raw.

Read Kàddu yu Xelu 18Kàddu yu Xelu 18
Compare Kàddu yu Xelu 18:9-10Kàddu yu Xelu 18:9-10