Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 18

Kàddu yu Xelu 18:5-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Faral ku tooñ baaxul, bul xañ dëgg ku deful dara.
6Ab dof, làmmiñam sooke naw ay, ay waxam di sàkku yeti gannaaw.
7Ab dof, waxam a koy sànk, làmmiñu boppam a koy dugal.

Read Kàddu yu Xelu 18Kàddu yu Xelu 18
Compare Kàddu yu Xelu 18:5-7Kàddu yu Xelu 18:5-7