Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 18

Kàddu yu Xelu 18:2-3

Help us?
Click on verse(s) to share them!
2Ab dof wutul ag dégg, balaa caag muy jaay ag muus.
3Bu mbon nuyoo, xeebeel topp ca; jëf ju ñaaw, gàcce rekk.

Read Kàddu yu Xelu 18Kàddu yu Xelu 18
Compare Kàddu yu Xelu 18:2-3Kàddu yu Xelu 18:2-3