Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 18

Kàddu yu Xelu 18:15-19

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Ku am ug dégg wut xam-xam, ku rafet xel sàkku xam-xam.
16Deel maye, da lay ubbil bunt, di la àggle ci boroom daraja.
17Ku jëkke layoo, ñu ne yaa yey, ba keroog ka nga joteel weddi la.
18Tegoo bant day feyu ay, di àtte boroom doole yu jote.
19Jubook mbokk moo tooñ, jéggi tataa ko gëna yomb, mbaa ubbi bunt yu tëje ràpp.

Read Kàddu yu Xelu 18Kàddu yu Xelu 18
Compare Kàddu yu Xelu 18:15-19Kàddu yu Xelu 18:15-19