Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 18

Kàddu yu Xelu 18:13-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
13Tontu te déggagoo, ndof la, ak ñàkk kersa.
14Ku bëgga dund, dékku woppi yaram, waaye xol bu jeex maneesu koo wéye.
15Ku am ug dégg wut xam-xam, ku rafet xel sàkku xam-xam.
16Deel maye, da lay ubbil bunt, di la àggle ci boroom daraja.

Read Kàddu yu Xelu 18Kàddu yu Xelu 18
Compare Kàddu yu Xelu 18:13-16Kàddu yu Xelu 18:13-16