Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 17

Kàddu yu Xelu 17:7-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Waxi teggin jekkul cib dof, ay fen ci as gor waxi noppi.
8Alalu ger njiglaay la ca ka koy joxe, ba fu mu jublu, mu nooy.
9Bale tooñ, yokk cofeel; sulliw ay, tas xarit.

Read Kàddu yu Xelu 17Kàddu yu Xelu 17
Compare Kàddu yu Xelu 17:7-9Kàddu yu Xelu 17:7-9