Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 16

Kàddu yu Xelu 16:5-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Aji Sax ji sib na ku réy, da koy mbugal ci lu wér.
6Ku jiital ngor ak worma, Yàlla jéggal la; ku ragal Aji Sax ji, dëddu lu bon.
7Ku Aji Sax ji rafetlu say jëf, say bañ sax, mu jubaleek yaw.
8Néewle te jub moo gën barele te jubadi.
9Nit ay sumb yoonam, Aji Sax ji sottal.

Read Kàddu yu Xelu 16Kàddu yu Xelu 16
Compare Kàddu yu Xelu 16:5-9Kàddu yu Xelu 16:5-9