Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 16

Kàddu yu Xelu 16:17-19

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Yoonu kuy jubal day moyu lu bon, ku teeylu sa jëfin, sàmm sa bakkan.
18Réy, yàqule; xeebaate, jóoru.
19Woyof, ànd ak ku néewle moo gën séddook ku bew la mu lewal.

Read Kàddu yu Xelu 16Kàddu yu Xelu 16
Compare Kàddu yu Xelu 16:17-19Kàddu yu Xelu 16:17-19