Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 16

Kàddu yu Xelu 16:15-16

Help us?
Click on verse(s) to share them!
15Buur, na kanam ga leer, sa bakkan mucc, su la baaxee, mu mel ni taw bu topp um nji.
16Wutal xel mu rafet, bàyyi wurus; taamul ag dégg, wacc xaalis.

Read Kàddu yu Xelu 16Kàddu yu Xelu 16
Compare Kàddu yu Xelu 16:15-16Kàddu yu Xelu 16:15-16