Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 15

Kàddu yu Xelu 15:5-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Ab dof day xeeb yaru baay ba, kuy dégg waxi àrtu, xelu nga.
6Kër ku jub, koom gu yaa; ku jubadi, alalam jur fitna.
7Ku xelu àddu, xam-xam law; ab dof amul xelam.
8Saraxub ku soxor, Aji Sax ji bañ na ko; ñaanu kuy jubal da koy bége.

Read Kàddu yu Xelu 15Kàddu yu Xelu 15
Compare Kàddu yu Xelu 15:5-8Kàddu yu Xelu 15:5-8