Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 15

Kàddu yu Xelu 15:28-31

Help us?
Click on verse(s) to share them!
28Ku jub day teeylu tontam; ab soxor, wax ju ñaaw rekk.
29Aji Sax ji day dëddu ab soxor, di nangu ñaanu ku jub.
30Kanam gu leer day seral xol; xibaaru jàmm, jàmmu yaram.
31Kuy dégg àrtu yu koy musal, ku rafet xel a ngoog.

Read Kàddu yu Xelu 15Kàddu yu Xelu 15
Compare Kàddu yu Xelu 15:28-31Kàddu yu Xelu 15:28-31