Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 15

Kàddu yu Xelu 15:27-28

Help us?
Click on verse(s) to share them!
27Wutin wu lewul, sonal sa waa kër; ku bañ alalu ger gudd fan.
28Ku jub day teeylu tontam; ab soxor, wax ju ñaaw rekk.

Read Kàddu yu Xelu 15Kàddu yu Xelu 15
Compare Kàddu yu Xelu 15:27-28Kàddu yu Xelu 15:27-28