Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 15

Kàddu yu Xelu 15:24-27

Help us?
Click on verse(s) to share them!
24Ku rafet xel, jubal nga yoonu gudd fan, moyu teggi, ba jëm njaniiw.
25Ku bew, Aji Sax ji màbb sa kër; ab jëtun, Aji Sax ji ñoŋal pàkkam.
26Aji Sax ji bañ na mébét mu bon, te wax ju yiw daa sell fa moom.
27Wutin wu lewul, sonal sa waa kër; ku bañ alalu ger gudd fan.

Read Kàddu yu Xelu 15Kàddu yu Xelu 15
Compare Kàddu yu Xelu 15:24-27Kàddu yu Xelu 15:24-27