Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 15

Kàddu yu Xelu 15:19-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Yoonu yaafus, dégi neen; kuy jubal, saw xàll yaa.
20Doom rafet xel, baay ba bég; te ab dof ay xeeb ndey ja.
21Jëfi dof a neex ku ñàkk bopp, ku am ug dégg def njub.

Read Kàddu yu Xelu 15Kàddu yu Xelu 15
Compare Kàddu yu Xelu 15:19-21Kàddu yu Xelu 15:19-21