Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 15

Kàddu yu Xelu 15:11-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
11Njaniiw ak biir suuf, Aji Sax ji di gis, xolu doom aadama waxi noppi.
12Kuy ñaawle buggul ku ko àrtu, te du laaji ku rafet xel.
13Xol bu sedd, kanam gu leer; xol bu tiis, boroom ne yogg.

Read Kàddu yu Xelu 15Kàddu yu Xelu 15
Compare Kàddu yu Xelu 15:11-13Kàddu yu Xelu 15:11-13