Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 14

Kàddu yu Xelu 14:6-9

Help us?
Click on verse(s) to share them!
6Ab ñaawlekat day wut xel mu rafet, mu réer ko; ku am ug dégg, xam yomb la.
7Dàndal ab dof, du la yokk xam-xam.
8Ku ñaw day xelu, xam li muy def; ab dof di nax boppam.
9Ab dof, su bàkkaaree, yoonam! Te ñay jubal a séq yiwu Yàlla.

Read Kàddu yu Xelu 14Kàddu yu Xelu 14
Compare Kàddu yu Xelu 14:6-9Kàddu yu Xelu 14:6-9