Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 14

Kàddu yu Xelu 14:5-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Seede bu dëggu, dëgg rekk, seede bu dëgguwul, fen rekk.
6Ab ñaawlekat day wut xel mu rafet, mu réer ko; ku am ug dégg, xam yomb la.
7Dàndal ab dof, du la yokk xam-xam.
8Ku ñaw day xelu, xam li muy def; ab dof di nax boppam.

Read Kàddu yu Xelu 14Kàddu yu Xelu 14
Compare Kàddu yu Xelu 14:5-8Kàddu yu Xelu 14:5-8