Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 14

Kàddu yu Xelu 14:25-26

Help us?
Click on verse(s) to share them!
25Seede bu dëggu day jot bakkan, kuy fen day wore.
26Ragal Aji Sax ji kaaraange gu wér la ci nit, di rawtu ciy doomam.

Read Kàddu yu Xelu 14Kàddu yu Xelu 14
Compare Kàddu yu Xelu 14:25-26Kàddu yu Xelu 14:25-26