Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 14

Kàddu yu Xelu 14:18-21

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18Ab téxét ndof ay céram, ku ñaw jagoo xam-xam.
19Ku bon, ku baax sut la; ku soxor ay toogaanu ku jub.
20Ku ñàkk, say dëkk sax bañ la; ku barele, barey xarit.
21Ku xeeb sa dëkkandoo, bàkkaar nga; ku baaxe ku ñàkk, mbégte ñeel la.

Read Kàddu yu Xelu 14Kàddu yu Xelu 14
Compare Kàddu yu Xelu 14:18-21Kàddu yu Xelu 14:18-21