Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 13

Kàddu yu Xelu 13:18-19

Help us?
Click on verse(s) to share them!
18Ku sàggane yoonu yar, séddoo ñàkk ak gàcce; kuy déggi àrtu, am teraanga.
19Aajo ju faju tooyal na xol, te ab dof jomb naa dëddu mbon.

Read Kàddu yu Xelu 13Kàddu yu Xelu 13
Compare Kàddu yu Xelu 13:18-19Kàddu yu Xelu 13:18-19