Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 12

Kàddu yu Xelu 12:5-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Ku jub, yoon lay mébét; ab soxor di lal pexey wor.
6Ab soxor, waxam am tëru la, day reye; kàdduy kiy jubal di musle.

Read Kàddu yu Xelu 12Kàddu yu Xelu 12
Compare Kàddu yu Xelu 12:5-6Kàddu yu Xelu 12:5-6