Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 12

Kàddu yu Xelu 12:4-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
4Jeeg bu jàmbaare day teral jëkkër ja, jeeg buy rusloo day semmal jëkkër ja.
5Ku jub, yoon lay mébét; ab soxor di lal pexey wor.
6Ab soxor, waxam am tëru la, day reye; kàdduy kiy jubal di musle.
7Ab soxor bu daanoo, jeex na; ku jub, sa kër taxaw, ne këcc.

Read Kàddu yu Xelu 12Kàddu yu Xelu 12
Compare Kàddu yu Xelu 12:4-7Kàddu yu Xelu 12:4-7