Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 12

Kàddu yu Xelu 12:25-26

Help us?
Click on verse(s) to share them!
25Njàqare day jeexal xolu boroom, wax ju neex di tooyal xolam.
26Ku jub day seetlu ku muy xaritool; soxor bi, jikkoom a koy sànk.

Read Kàddu yu Xelu 12Kàddu yu Xelu 12
Compare Kàddu yu Xelu 12:25-26Kàddu yu Xelu 12:25-26