Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 12

Kàddu yu Xelu 12:19-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
19Kàdduy dëgg, day sax dàkk; fen, xef xippi, mu wéy.
20Kuy ràbb lu bon lal pexey wor, kuy digle jàmm, am mbégte.
21Ku jub du amu ay, ab soxor du tàggook musiba.
22Aji Sax ji sib na fen-kat, safoo ku dëggu.

Read Kàddu yu Xelu 12Kàddu yu Xelu 12
Compare Kàddu yu Xelu 12:19-22Kàddu yu Xelu 12:19-22