Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 12

Kàddu yu Xelu 12:17-18

Help us?
Click on verse(s) to share them!
17Ku dëggu, seede dëgg; seede bu bon, fen rekk.
18Làmmiñu waxkat, jam-jami jaasi; kàddu gu xelu, garab la ci.

Read Kàddu yu Xelu 12Kàddu yu Xelu 12
Compare Kàddu yu Xelu 12:17-18Kàddu yu Xelu 12:17-18