Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 11

Kàddu yu Xelu 11:3-6

Help us?
Click on verse(s) to share them!
3Kuy jubal, jiital mat. Njublaŋ ak wor, detteelu.
4Alal du jariñ bésu mbugal; jub, mucc ci gàtt fan.
5Ku mat, njekk xàllal la; coxor daaneel boroom.
6Jubalal, sa njekk musal la; ab workat day bëgge, ba far keppu.

Read Kàddu yu Xelu 11Kàddu yu Xelu 11
Compare Kàddu yu Xelu 11:3-6Kàddu yu Xelu 11:3-6