Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 11

Kàddu yu Xelu 11:25-28

Help us?
Click on verse(s) to share them!
25Ku yéwén, woomle; kuy suuxat, suuxu.
26Nit a ngi móolu kuy denc pepp, ba mu ñàkkee, di gërëm ka koy jaay.
27Wutala wut lu baax, ñu nawloo la; ku sàkku lu bon, yaa koy yenu.
28Ku yaakaar sa alal sab jéll a ngi ñëw, ku jub day juble ni gàncax gu naat.

Read Kàddu yu Xelu 11Kàddu yu Xelu 11
Compare Kàddu yu Xelu 11:25-28Kàddu yu Xelu 11:25-28