Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 11

Kàddu yu Xelu 11:24-26

Help us?
Click on verse(s) to share them!
24Nit a ngi tabe, di yokkule; nit di nëŋ-nëŋi, gëna ñàkk.
25Ku yéwén, woomle; kuy suuxat, suuxu.
26Nit a ngi móolu kuy denc pepp, ba mu ñàkkee, di gërëm ka koy jaay.

Read Kàddu yu Xelu 11Kàddu yu Xelu 11
Compare Kàddu yu Xelu 11:24-26Kàddu yu Xelu 11:24-26