Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 11

Kàddu yu Xelu 11:21-24

Help us?
Click on verse(s) to share them!
21Ab soxor mbugalam du jaas, wóor na; te ku jub, saw askan mucc.
22Taaru jongama ju xel ma gàtt, mooy jaaro wurus ci noppu mbaam-xuux.
23Ku jub, lu baax rekk lay sàkku; soxor biy yaakaar, mujje mbugal.
24Nit a ngi tabe, di yokkule; nit di nëŋ-nëŋi, gëna ñàkk.

Read Kàddu yu Xelu 11Kàddu yu Xelu 11
Compare Kàddu yu Xelu 11:21-24Kàddu yu Xelu 11:21-24