Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 10

Kàddu yu Xelu 10:9-13

Help us?
Click on verse(s) to share them!
9Maandu, fegu; dëng, weeru.
10Piiseek làq-làqal, sabab njàqare; ab dof waxa wax, ba loru.
11Kàdduy ku jub bëtu ndox la, day naatal; waaye ku soxor, wax ja làq fitna.
12Mbañeelak ayoo; cofeelak jéggale bépp tooñ.
13Kuy dégg, say wax rafet; te ku ñàkk bopp, yelloo yetu gannaaw.

Read Kàddu yu Xelu 10Kàddu yu Xelu 10
Compare Kàddu yu Xelu 10:9-13Kàddu yu Xelu 10:9-13