Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 10

Kàddu yu Xelu 10:5-7

Help us?
Click on verse(s) to share them!
5Ku ngóob jot, nga góob, xelu nga; ngóob taxaw, ngay nelaw, gàcce la.
6Jub, barkeelu; ku soxor, wax ja làq fitna.
7Ku jub barkeel, saw tur du fey; ab soxor, turam seey.

Read Kàddu yu Xelu 10Kàddu yu Xelu 10
Compare Kàddu yu Xelu 10:5-7Kàddu yu Xelu 10:5-7