Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Kàddu yu Xelu - Kàddu yu Xelu 10

Kàddu yu Xelu 10:20-22

Help us?
Click on verse(s) to share them!
20Kàddug ku jub di ngën-gi-xaalis, xelum coxor amul solo.
21Kàdduy ku jub jariñ na ñu bare, dof ñàkk na bopp, ba far dee.
22Barkeb Aji Sax jeey maye alal, kër-këri taxula barele.

Read Kàddu yu Xelu 10Kàddu yu Xelu 10
Compare Kàddu yu Xelu 10:20-22Kàddu yu Xelu 10:20-22