Text copied!
CopyCompare
Kàddug Yàlla gi - Ngën-gi-woy - Ngën-gi-woy 8

Ngën-gi-woy 8:7-8

Help us?
Click on verse(s) to share them!
7Ndox mu ne xéew du fey mbëggeel, ay dex du ko mëdd. Ku koy weccee sa alalu kër gépp it, ñu jéppi laa jéppi rekk.
8Sunub jigéen lu ndaw la, ween sax amu ko. Lu nuy defal sunub jigéen bés bu ñu koy bëggsi?

Read Ngën-gi-woy 8Ngën-gi-woy 8
Compare Ngën-gi-woy 8:7-8Ngën-gi-woy 8:7-8