Text copied!
BREAK EVERY YOKE
About
Bibles
All Languages
All Translations
All Countries
Back to Homepage
About Break Every Yoke
Bibles in Wolof
Ngën-gi-woy 8:7-8 in Wolof
Help us?
Ngën-gi-woy 8:7-8
in
Kàddug Yàlla gi
7
Ndox mu ne xéew du fey mbëggeel, ay dex du ko mëdd. Ku koy weccee sa alalu kër gépp it, ñu jéppi laa jéppi rekk.
8
Sunub jigéen lu ndaw la, ween sax amu ko. Lu nuy defal sunub jigéen bés bu ñu koy bëggsi?
Ngën-gi-woy 8 in Kàddug Yàlla gi
Home
About
Donate
Patreon
Privacy
Terms